lirikku.id
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #
.

Lirik Lagu Youssou n’dour – Sama Gàmmu


By: Admin | Artist: Y youssou ndour | Published: 2024-21-06T22:26:26:00+07:00
Lirik Lagu Youssou n’dour – Sama GàmmuLirikku.ID - Lirik Lagu Youssou n’dour – Sama Gàmmu: Halo Lirikku.ID, Dalam konten ini, kami menyediakan chord gitar untuk lagu "Lirik Lagu Youssou n’dour – Sama Gàmmu" yang dinyanyikan oleh Toton Y youssou ndour. Dengan chord yang disajikan, pemula atau penggemar musik dapat dengan mudah memainkan lagu ini dengan gitar mereka sendiri. Kami menyajikan chord dengan akurasi tinggi sehingga pemain dapat mengikuti alunan musiknya dengan baik. Juga, kami akan memberikan informasi tambahan mengenai lirik lagu dan mungkin beberapa tips untuk menyempurnakan permainan gitar. Konten ini cocok untuk penggemar musik yang ingin belajar lagu baru atau bagi mereka yang ingin menikmati kesenangan bermain musik dengan gitar. Silahkan disimak Lirik Lagu Youssou n’dour – Sama Gàmmu Berikut Dibawah ini untuk Selanjutnya.

nanga def yaw sama gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
xam naa ne yaw moomu loo ko
dang ko àbb mbaa nga for ko
baal dóózéé, eh
nanga def, na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
ba foo ma séén tàmbaleey wëlis
xam naa ne yaw moomu loo ko
dang ko àbb mbaa nga for ko
baal dóózéé, eh
yor xaalis mënui tee me moom la
nanga def, na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
xam naa ne yaw moomu loo ko
dang ko àbb mbaa nga for ko
baal dóózéé, eh
kaay gaaw wax ma na nga def ba am ko
foog nan nita ko waddal nga for ko
wax ma gaaw ñaata la doon ma fay ko
man daal maay sa buur nangu ko
nanga def, na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
ba foo ma séén tàmbaleey wëlis
xam naa ne yaw moomu loo ko

dang ko àbb mbaa nga for ko
baal dóózéé, eh
ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee
ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee
ah gàmmu daal sama doomu nday nga
e e e gàmmu daal suma xarit nga
e e e gàmmu daal suma askan nga
ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
e e e gàmmu daal suma xarit nga
e e e gàmmu daal man sama doomu nday nga
e e e gàmmu daal man suma xarit nga
e e e gàmmu daal yaw sama doomu nday nga
baal dooc moomu foo ko
teeyai teey teey
ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee
ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee
e e e gàmmu daal sama doomu nday nga
e e e gàmmu daal suma xarit nga
e e e gàmmu daal suma askan


Saksikan Video Lirik Lagu Youssou n’dour – Sama Gàmmu Berikut ini..


Lirik lagu lainnya: